1
00:00:10,820 --> 00:00:17,290
iza te wo nobashite kaze wo kirisaite

2
00:00:10,820 --> 00:00:17,290
Tàllalal sa loxo, nga bën ngelaw li.

3
00:00:17,490 --> 00:00:21,910
onore no chizu wo egaite yuke

4
00:00:17,490 --> 00:00:21,910
Desineel sa kàrt

5
00:00:26,920 --> 00:00:33,090
migi mo hidari mo guchagucha
ni areta umi no you na jidai

6
00:00:26,920 --> 00:00:33,090
ni ñuy dundee sunuy fan
melni géej gu ànd ak ngelaw.

7
00:00:33,260 --> 00:00:39,140
kizukiageta kachikan sae mo
Kuzuresarou

8
00:00:33,260 --> 00:00:39,140
ak valeur yi ñuy tabax
Dañu nara tas.

9
00:00:40,060 --> 00:00:46,190
rashinban no sashita saki ga
Tadashii no ka douka nante

10
00:00:40,060 --> 00:00:46,190
Ku xam ndax busol bi dafay wane
ci yoon wi war.

11
00:00:46,350 --> 00:00:49,820
Kenn xamul lu leer.

12
00:00:46,350 --> 00:00:49,860
Duma ñeme ni wakaranainda

13
00:00:50,020 --> 00:00:56,070
fukaku iki wo suikonde hitomi tojireba

14
00:00:50,020 --> 00:00:56,070
Soo noyyi bu baax ba noppi nga tëj say bët,

15
00:00:56,320 --> 00:01:02,700
ukabiagaru no wa
Tamashii no shimesu michi

16
00:00:56,320 --> 00:01:02,700
li feeñ mooy yoon wi
loolu mooy wane sa ruuh.

17
00:01:03,370 --> 00:01:09,670
iza te wo nobashite kaze wo kirisaite

18
00:01:03,370 --> 00:01:09,670
Dëddul nga jàll ngelaw li.

19
00:01:09,920 --> 00:01:14,340
kurayami wo kettobashite

20
00:01:09,920 --> 00:01:14,340
Raxasal lëndëm gi.

21
00:01:15,590 --> 00:01:18,430
ima boku wa boku no tame ni

22
00:01:15,590 --> 00:01:18,430
Maa ngi koy def ngir sama bopp.

23
00:01:18,590 --> 00:01:22,220
kimi wa kimi no tame ni sou darou

24
00:01:18,590 --> 00:01:22,220
Te yaa ngi koy defal sa bopp, wala book?

25
00:01:22,850 --> 00:01:26,480
Maa ngi ko waaja def.

26
00:01:22,850 --> 00:01:26,520
kakugo wa dekiteiru sa

27
00:01:26,690 --> 00:01:31,610
toki ni tayoriaeru yo na
sonzai ni sasaerare

28
00:01:26,690 --> 00:01:31,610
Ak ndimbalu nit ku ma wóolu.

29
00:01:31,770 --> 00:01:38,910
souzou wo koeta mirai tsukamitore

30
00:01:31,770 --> 00:01:38,910
yegg ci ëlëg giy dem
lu weesu sa xalaat.

31
00:01:39,070 --> 00:01:45,370
iza te wo nobashite kaze wo kirisaite

32
00:01:39,070 --> 00:01:45,410
Dëddul nga jàll ngelaw li.

33
00:01:45,580 --> 00:01:51,170
Raxasal lëndëm gi.

34
00:01:45,580 --> 00:01:51,250
kurayami wo kettobashite

35
00:01:51,420 --> 00:01:54,590
bokura wa dokomademo yukeru

36
00:01:51,420 --> 00:01:54,590
Dina nu dem fi nu bëgg

37
00:01:54,760 --> 00:01:58,470
namida mo mayoi mo isso hikitsurete

38
00:01:54,760 --> 00:01:58,470
mu ànd ak rangooñ ak sikki-sakka.

39
00:01:58,630 --> 00:02:04,560
amul benn iro de egaite yuke

40
00:01:58,630 --> 00:02:04,560
Nanu ko peinte ak sunuy melo yi.

41
00:02:12,750 --> 00:02:19,380
Bi chateau bi di tàkk,
Izo jàkkarloo ak CP-0.

42
00:02:20,950 --> 00:02:21,870
Pistool baraam!

43
00:02:36,400 --> 00:02:37,760
O déet!

44
00:02:41,240 --> 00:02:42,240
Maha!

45
00:02:46,450 --> 00:02:50,770
Kaka! Lu tax ngay jàppale
ab naataango bu njëkk ci Sikum Weex?

46
00:02:53,750 --> 00:02:55,700
Dama wara gaaw gis Nico Robin.

47
00:02:57,740 --> 00:03:00,170
Leegi ana?

48
00:03:01,830 --> 00:03:03,220
Saa waay, déglul bu baax.

49
00:03:04,160 --> 00:03:06,370
Dafay nekk ndigalu Juróomi Mag ñi.

50
00:03:07,830 --> 00:03:09,420
Juróomi mag ñi?

51
00:03:09,830 --> 00:03:11,310
Neena ñu...

52
00:03:12,560 --> 00:03:15,050
dindi mbaxana ñax Luffy.

53
00:03:16,920 --> 00:03:18,690
Looy wax nii?

54
00:03:19,080 --> 00:03:21,850
Leegi mingi jàkkarloo ak Kaido!

55
00:03:22,770 --> 00:03:25,660
Ndax yaa ngi wax ni dama wara tere leen xeex?

56
00:03:25,810 --> 00:03:26,820
Loolu mënul nekk!

57
00:03:26,980 --> 00:03:29,750
Xam nanu ni du lu yomb.

58
00:03:31,320 --> 00:03:35,280
Waaye bàyyi ko dafa am loraange lool
xeex ak ñi gëna baax ci àdduna.

59
00:03:35,890 --> 00:03:37,500
Jël ko.

60
00:03:37,660 --> 00:03:40,620
Moytu bu war la.

61
00:03:42,740 --> 00:03:45,680
Lenn lu am tension
ba ci juróomi mag ñi...

62
00:03:46,790 --> 00:03:50,270
Danu xam mbir rek
ci ay wax...

63
00:03:54,510 --> 00:03:57,760
Mënumaa dee te defuma dara!

64
00:04:00,170 --> 00:04:01,970
Boobu ekipu pirat?

65
00:04:14,230 --> 00:04:15,610
Gear ñeenteelu!

66
00:04:14,230 --> 00:04:15,610
ñeenteelu vites

67
00:04:30,210 --> 00:04:31,420
Jaan-Nit!

68
00:04:30,210 --> 00:04:31,420
Jaan ji

69
00:04:35,090 --> 00:04:37,270
Gomu Gomu no...

70
00:04:37,420 --> 00:04:38,520
Hidra!

71
00:04:37,420 --> 00:04:38,520
Hydra en kawsu

72
00:04:54,110 --> 00:04:57,280
Faale wuma bëgg-bëgg
nga amoon!

73
00:04:57,820 --> 00:05:01,820
Xamnaa ni dina am njariñ
ni askanu réew mi

74
00:05:02,320 --> 00:05:04,410
gëna xiif!

75
00:05:05,490 --> 00:05:09,120
Lii mooy sama ñeenteelu Gear bu mujj!

76
00:05:09,620 --> 00:05:14,040
Duma bàyyi song
ba sama kàttan jeex!

77
00:05:14,080 --> 00:05:22,860
Benn ki jël raw-gàddu gi kese mooy am
Luffy ak Kaido

78
00:05:17,630 --> 00:05:21,690
Kenn kese mooy jël ndam li.
Luffy ak Kaido.

79
00:05:28,390 --> 00:05:29,870
Reen!

80
00:05:30,770 --> 00:05:32,900
Ndax danga dof?

81
00:06:10,180 --> 00:06:12,770
Ndox!

82
00:06:18,270 --> 00:06:20,080
Ndox!

83
00:06:20,230 --> 00:06:22,910
Ndox!

84
00:06:23,070 --> 00:06:24,880
Ndax yaa ngi jooy?

85
00:06:25,450 --> 00:06:27,160
Du ni yaw.

86
00:06:27,530 --> 00:06:33,640
Dimbali Orochi, mi ragal lu weesu
te bëgg na yor nit ñi,

87
00:06:33,790 --> 00:06:36,170
Daf leen néewal doole.

88
00:07:00,820 --> 00:07:02,920
O, o!

89
00:07:12,830 --> 00:07:15,040
Du lakk!

90
00:07:16,080 --> 00:07:18,500
O, o! Du lakk!

91
00:07:18,920 --> 00:07:21,840
Dédeet, déet... Dafay tàkk!

92
00:07:29,430 --> 00:07:34,520
Leegi, ba ci ninja yi
Am nanu tuuti moom sa bopp, Fukurokuju!

93
00:07:34,520 --> 00:07:44,530
{\an9}Xare ci hall bi

94
00:07:34,520 --> 00:07:44,530
{\an7}Gañekat bi:
Mistroot

95
00:07:36,440 --> 00:07:40,080
Xeex ci waañ wi
ci ñatteelu etaasu kër buur ba.

96
00:07:40,860 --> 00:07:43,960
Gañekat bi: Reen bu Mist bi.

97
00:07:52,370 --> 00:07:54,660
Fi! Dawleen!

98
00:07:55,120 --> 00:07:56,660
Jërëjëf!

99
00:07:58,210 --> 00:08:00,580
Château bi mingi waaja daanu.

100
00:08:04,100 --> 00:08:05,920
Hey! Ndax samurai nga?

101
00:08:06,260 --> 00:08:08,020
Lu tax doo daw?

102
00:08:11,060 --> 00:08:14,410
Yaay kenn ci àndadoo Luffy...

103
00:08:17,580 --> 00:08:19,060
Dama wara dem leegi!

104
00:08:19,230 --> 00:08:22,190
Mën wéy di xeex! Bàyyileen leegi!

105
00:08:22,570 --> 00:08:26,320
Loolu ruslu la... maa ngi waaja...

106
00:08:26,490 --> 00:08:28,370
Saa waay! Bëgg nga dee?

107
00:08:28,530 --> 00:08:30,200
Dama soxla ndimbal!

108
00:08:31,820 --> 00:08:34,910
Etage bi njëkk ci sous-sol
ci biir chateau bi

109
00:08:38,500 --> 00:08:42,670
Luffy mbaxna ñax,
Yaa ngi ci kaw kër gi, wala book?

110
00:08:43,140 --> 00:08:47,630
"Àrtu".
Loolu mooy li ngay fay ci sa dundu.

111
00:09:09,840 --> 00:09:12,630
Drake, lu tax ngay def lii?

112
00:09:13,070 --> 00:09:15,950
Ndax jàpp naa ni mooy li nga wara def!

113
00:09:17,750 --> 00:09:19,710
Maa ngi la ci ñee.

114
00:09:28,590 --> 00:09:30,010
Pistool baraam.

115
00:09:36,220 --> 00:09:40,930
{\an9}Kapitaalu flër yi

116
00:09:49,690 --> 00:09:51,450
Ndax bind nga sa bëgg-bëgg?

117
00:09:51,610 --> 00:09:54,160
Leer leen gaal yu asamaan!

118
00:09:58,700 --> 00:10:00,350
Loolu rafet na!

119
00:10:00,540 --> 00:10:02,470
Neex na lool !

120
00:10:03,750 --> 00:10:06,590
Ak luma ko mëna gis,
Ba leegi mingi rafet.

121
00:10:15,760 --> 00:10:18,200
Ok, nanu leen fexe ñu naaw!

122
00:10:18,720 --> 00:10:21,390
Yonnee sa bëgg-bëgg asamaan si!

123
00:10:22,560 --> 00:10:23,890
Baay!

124
00:11:02,060 --> 00:11:04,700
Gomu Gomu no...

125
00:11:04,850 --> 00:11:06,770
Hidra!

126
00:11:04,850 --> 00:11:06,770
Hydra en kawsu

127
00:11:16,990 --> 00:11:19,570
Ndax yaa ngi sëggal
trajectoire de attaques yi?

128
00:11:22,290 --> 00:11:25,760
Waaye loolu mënul nekk
ndax nature kawsu bi.

129
00:12:02,580 --> 00:12:05,080
Gomu Gomu no...

130
00:12:06,750 --> 00:12:08,640
Kobra Buur!

131
00:12:06,750 --> 00:12:08,640
Cobra buur en caoutchouc

132
00:12:52,750 --> 00:12:54,210
Ay!

133
00:12:57,840 --> 00:13:00,880
Bàyyi, yaa ngi may gaañ!

134
00:13:01,720 --> 00:13:03,600
Dafay metti lool!

135
00:13:04,550 --> 00:13:06,770
Nanga taxaw!

136
00:13:06,770 --> 00:13:09,990
amae jougo
(Màndi bu néew doole)

137
00:13:11,060 --> 00:13:13,190
Ndax ba leegi yaa ngi màndi?

138
00:13:16,440 --> 00:13:21,090
Bul jàpp ni yaw kese nga
loolu mën na wax luy xew.

139
00:13:25,990 --> 00:13:28,450
Maa ngi koy kopie ci sa attaque.

140
00:13:35,590 --> 00:13:40,550
Nusubito Jougo
(Sàcc bu màndi)

141
00:13:38,870 --> 00:13:40,550
Ndax nii lañu koy defee ?

142
00:13:44,000 --> 00:13:45,900
O, o!

143
00:13:53,100 --> 00:13:55,160
Daf ma lekk!

144
00:13:55,380 --> 00:13:57,520
Bàyyil ma génn, yaw dof ji!

145
00:14:01,950 --> 00:14:04,450
Bàyyileen ma génn!

146
00:14:12,040 --> 00:14:13,850
Bolus noyyig!

147
00:14:12,040 --> 00:14:13,850
Noyyig Explosif

148
00:14:36,860 --> 00:14:38,750
Loolu dafa tiis lool.

149
00:14:38,900 --> 00:14:41,500
Xale bi sol mbaxana ñax mi
Ndax dinga ko muñ ?

150
00:14:42,150 --> 00:14:45,450
Gisoo Luffy
benn seconde ci ginaaw?

151
00:15:32,080 --> 00:15:33,370
Bondman!

152
00:15:32,080 --> 00:15:33,370
Rebounder

153
00:15:38,960 --> 00:15:40,600
Dina nekk kretin...

154
00:15:45,720 --> 00:15:49,090
Dama jaxasoo!

155
00:16:04,300 --> 00:16:06,450
Dellu na.

156
00:16:06,610 --> 00:16:09,090
Ba kañ lay yàgg?

157
00:16:09,240 --> 00:16:12,330
Lii mooy sama ñeenteelu Gear bu mujj!

158
00:16:25,420 --> 00:16:27,900
Deseuma jotu lu bari!

159
00:16:37,270 --> 00:16:40,270
Bul ma xàddi leegi, Gear Fourth!

160
00:16:43,260 --> 00:16:44,320
O déet!

161
00:16:51,710 --> 00:16:53,490
Dama ko wara daan leegi.

162
00:16:54,220 --> 00:16:58,120
Gis. moo gëna am jafe-jafe
luma gëmoon

163
00:16:58,290 --> 00:17:00,540
doole kawsu bi.

164
00:17:03,020 --> 00:17:04,750
Dinaa ko jànkoonteel ak sama xol!

165
00:17:05,460 --> 00:17:08,470
Nanu bànneexu, Mbaxna ñax!

166
00:17:08,920 --> 00:17:10,360
Noppil!

167
00:17:12,090 --> 00:17:15,350
Dinaa la daan ak lumu mëna xew!

168
00:17:22,230 --> 00:17:23,860
Nit ñi ci Wano...

169
00:17:25,400 --> 00:17:27,690
mënu ma am ndox mu naan.

170
00:17:29,650 --> 00:17:31,710
Te mënul sax lekk

171
00:17:34,280 --> 00:17:36,120
soo nekkee fi ba leegi!

172
00:17:36,280 --> 00:17:39,830
Déedet,
ndax dañu ñàkk xare bi.

173
00:17:40,350 --> 00:17:44,040
Jërëjëf ci lima leen rayul.

174
00:17:45,250 --> 00:17:49,460
Faale wuma kan ngay jàppalante,

175
00:17:51,770 --> 00:17:55,720
waaye waa Wano
Dafa tàmm di ñàkk.

176
00:17:55,970 --> 00:17:58,310
Ki néew doole dafa dal.

177
00:17:58,680 --> 00:18:00,180
Ñi faatu ñu tedd.

178
00:18:01,470 --> 00:18:06,230
gis naa téemeeri nit ñu amul fuñu dëkk
def ay sabab.

179
00:18:07,630 --> 00:18:11,950
Dama tàyyi ci gis kanam yu ñaaw yooyu!

180
00:18:12,890 --> 00:18:14,700
Noppi!

181
00:18:15,160 --> 00:18:17,280
Samurai yi dañu am doole!

182
00:18:18,950 --> 00:18:22,310
Ndax dañu am doole wala dañuy jéema naxaate?

183
00:18:23,000 --> 00:18:27,560
Ndaw yi
Soxlawoñu gërëm lu bari noonu!

184
00:18:27,870 --> 00:18:29,500
Fan nga mëna ànd?

185
00:18:30,150 --> 00:18:31,880
Mbaxana ñax?

186
00:18:35,390 --> 00:18:37,930
Gomu Gomu no...

187
00:18:48,940 --> 00:18:51,780
Gun bu ëpp kong!

188
00:18:48,940 --> 00:18:51,780
Pistole de caoutchouc

189
00:19:19,330 --> 00:19:20,510
Jeexuma!

190
00:19:21,140 --> 00:19:23,320
Maa ngi waaja ray ko bu baax!

191
00:19:32,800 --> 00:19:35,420
Soo mënee jëfandikoo sama Gear Fourth!

192
00:19:37,800 --> 00:19:39,700
Horay

193
00:19:43,790 --> 00:19:45,460
Hakke!

194
00:19:43,790 --> 00:19:45,460
Juroom ñatti trigram yuy yuuxu

195
00:20:25,120 --> 00:20:27,210
Energy, bul ma bàyyi!

196
00:20:31,130 --> 00:20:34,380
Satsuriku Jougo
(màndi deret)

197
00:20:41,930 --> 00:20:44,220
mën nga ko gis

198
00:20:44,890 --> 00:20:47,620
li ma bëgg?

199
00:20:53,500 --> 00:20:55,230
Benn hit bu bees!

200
00:20:56,150 --> 00:20:58,740
Nanu jeexal jaar-jaar bii.

201
00:20:58,900 --> 00:21:00,750
Sudee lii mënu...

202
00:21:01,590 --> 00:21:03,910
Nanga def, xale!

203
00:21:04,080 --> 00:21:06,140
...Dinaa ñàkk!

204
00:21:13,080 --> 00:21:16,130
Gomu Gomu no...

205
00:21:40,240 --> 00:21:41,950
Lu weesu...

206
00:21:42,110 --> 00:21:44,450
Horai...

207
00:21:46,280 --> 00:21:47,430
Yaram weñ!

208
00:21:49,410 --> 00:21:53,270
CP-0 bi? Lu kii di def fii?

209
00:23:18,670 --> 00:23:22,480
Xeex bu mag bi ci dome bi
mu jeex ci anam wuñu ko xaarul.

210
00:23:22,630 --> 00:23:25,270
Ñu bàyyi leen ñu amul xeex bu metti,

211
00:23:25,500 --> 00:23:28,740
Kaido bu mer
Mu jàkkarloo ak samurai yi gaañu.

212
00:23:28,890 --> 00:23:32,410
Leegi 20 at yu am yaakaar
Dañu daanu ci sa kanam,

213
00:23:32,560 --> 00:23:35,620
mën nañu gis
ab yoonu génn ci jahannama?

214
00:23:36,310 --> 00:23:37,560
Episode bi ci topp:

215
00:23:37,890 --> 00:23:41,290
"Ndax dina ñu daan Luffy?
Fas yéene bu ñi des”.

216
00:23:41,620 --> 00:23:45,610
Ndax dina ñu daan Luffy?
Fas yéene ñi des

217
00:23:41,770 --> 00:23:44,330
Maa ngi nekk Buuru Pirat yi!

218
00:23:45,930 --> 00:23:52,050
</b>Tekki: Abraham Gayuvas ak Sergio Vaca
Abraham Gayuvas
Sergio Vaca


